li moyi programme-ensa · li moyi programme-ensa xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam...

12
LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Upload: lamdat

Post on 10-Sep-2018

218 views

Category:

Documents


1 download

TRANSCRIPT

Page 1: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

LI MOYI PROGRAMME-ENSAXabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme

weccee diggante ay lekkool yi

JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Page 2: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

ENSA – JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Page 3: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

ENSA – JÁNG GIS BENN ÁDDINA

ENSA, politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay

lekkool yi, ministère fédéral (gouvernement allemand) ngir bokkaale liggéey

buyi suqali koom-koom ak tàllal bi moo joxe ndigal bi (BMZ). ENSA dafay

nekk benn cér ci politig buyi jémale nit ni kanam bokk ci atelier ngir jángale

ay xam-xam yu bees ASA. Dale-ko 2012 ASA ak ENSA ñu ngi nekk digaale ci

ENGAGEMENT GLOBAL gGmbH.

ENSA dafay dimbali ci dajánte bi diggante ayi eleew yi ñuyi joge Allemagne ak

ku joge bitimréew mel ni Afrique, Asie, Ameriqe bi nekk bëj-saalum ak Europ

bëj-saalum-penku. ENSA dafay leen jángale ndax man am ay gis-gis bu bees

ak yaatu ci jeneen jëf ak dooleel leen, ñu bokk ci liggéey bi te jem nánd ayi

digaale yi ndax jemale buyi man yägg ci áddina wi ëllëg.

ENSA dafa bëgga eleew yi am fayda ci ponk yi ndax politig tàllal mi, dinañu

suqali ag xiirte ngir ñu bokk ci liggéey bi ak defante ndax áddina bu gën baax.

ENSA-Programme bi dafay bokk ci fukk at programme nations unies ndax

»Tállal li man yágg ci ëllëg«, kuyi dimmali nit yi ngir man nañu ame xiirte,

bokk ci liggéey buyi defar luyi seen sas la ci kanamu mboolem-nawle mi

mépp ci áddina ak góor-góorlu ándando nekk ayi muskállaf ngir defar suñuyi

Cakkéef bi. Ayi nas ci lekkool yi, li ENSA dimbali, mooy nekk topp seen nësër

ayi misaal mel ni ponk yi jemale nit yepp, def li nekk ak njub, cákkéef ak

koom-koom buyi man yägg ci ëllëg.

Lool yepp man na nekk su fekk danu man daje te dimbalant ci jáng mi!

Page 4: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

ÑUYI DOXALE XAM-XAMU JÁNGALE

MBOOLE CI JÁNG MI

Page 5: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Digaale ci diggante lekkool yi ak daje diggante eleew yi ñuyi joge bëj-saalum

ak bëj-gánnaaru dinañu ware waajal bu baax-baax. ENSA dafay dimbali ayi

lekkool yi, nuyi am ndimmali Mbootay yi andul ak benn nguur (NRO) danuyi

leen war yor, li nekk ci, defar ayi reeso ak waxtaane ngi yokk man-man ak

kenn ku nekk war am waajalseemineer yi ak defaraatseemineer yi.

Ci liggéey bi ni yi nekk ayi xam-xamu jángale nuyi ndimmali ayi lekkool yi

ci waajalweccee yi ak defaraatweccee yi diggante lekkool yi defar digaale

diggante lekkool yi bo xamne man na yägg ci ëllëg. Dinañu jánge lan la nu

man liggeey ci gruup wi ak fason li lan la ñu man regle ayi naayoo yi ak nan

nañu man jakkarlo ak lu bare te wute, ayi digaale diggante nit yi ak li nekk ci

jáng bu mottali. ENSA defa bëgg dimbali cisoppi gëmkay ak nit bu nekk man

xaalat ci boppam li nga niroo ak ban gëdd nga am ci mottali áddina gi.

Nit yépp ñu ci bokk war na ñu andando ci liggéey bi ndax defar nas bi ak

seemineer yi.

Bu ñu liggéey ci defaraatseemineer yi ñu ci bokk dinañu xayma seen aay yi ak

liggéey ci jeneen yoon wi, jël tayle suñu nekk ayi nityi di tass xam-xam bi ngir

digaale buyi yemale nit yi te li man yägg ci ëllëg. Reeso ENSA bi man leen joxe

ayi yoon yu bees ngeen defante, su nas wi jexe.

Du eleew yi rekk ñuyi am liggeey ci nas bi te jáng ayi mébét yu bees.

Jángalekat itamit ak liggéeykat ci Mbotay yi andul ak benn ngurgi dañu bokk

ci liggéey bi ngir mottali bu baax-baax, pur ame ay digaale yu baax ci biir

mboolem-nawle mi mépp, walla cákkéef buyi man yägg ci ëllëg nii li ñu jáng

yu bees ak beesaay li ñu defar dangeen man jëfandikoo fu ngeen liggéey ak

jáng mooyi seen lekkool. ENSA defay nekk programme, bu xamne dey kontine

di suqali ak soppi.

ENSA defay bëgg joxe wàllam ci digaale bi, dimbali nit ñuyi bokk ci

programme wi, ñuyi defendre seen taxawaay, dañuy am seen xalaat ci mottali

ponk yi li ñu man suqali ak li ñu war mottali, ndax ñu man liggéey bokk ci

mboolem-nawle wi.

Page 6: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA
Page 7: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

»…Ich habe viel erkannt,was über mein bisheri-ges Blickfeld hinaus geht (…) Man begreift manches erst dann, wenn man es mit eigenen Augen sieht.«

ENSA dafay bëgg liggéey ak mbootay yi andul ak benn ngurgi náaxte mooy

nësëram. Dinanu andando ak jeen bokk ci liggéey bi, ndimmali pur tayle

mboolem-nawle dem ci kanamu te man yágg ci ëllëg ci biir lekkool yi. Sunuy

nësër mooy defar digaale ku man yágg ci ëllëg diggante lekkool yi ñuy nekk

bëj-saalum ak ñuy nekk bëj-gánnaaru, nuy dimbali ngir nànd (déggoo) pur

jeenenn nbindeefu, waaye nuy dimbali itamit ayi digaale ak joxe lépp ku ci

bokk ag xiirte, nuy góor-góorlu ndax jemale mboolem-nawle.

Ci liggéey ENSA danuy joxe dajante ak digaale yi ci tukki yi ngir daje ay dayo

bu rëy. Ay nas yi li ñu waaxe »Incoming-Projekte«, loo xamne eleew yi nji joge

ci bitim-réew mi mel ni mottali bëj-saalum ci seen digaale lekkool yi nji nekk

ci Allemagne, dañu nekk ay digaale ñuy am-solo ci jemale nit yi.

ENSA defay naw nekkin bi bëgg jot ay eleew yi bo xamne dañu am ay

mboolem-nawle yi bare te nekkuñu benn. Nekkin bi moo taax lekkool yi bu

diggi doomu (am ci Allemagne) ak lekkool yi buyi jox dooli man-man, walla ay

lekkool yi fu nuy jáng mécce yi dinanu leen laj ngeen depose indi seen kayit

demande bi ci ENSA ndax ñu man ndimmal leen.

Weccee wi diggante ay lekkool yi ngir fason lekkool yi yépp danu am-solo

ci programme ENSA bi, waxaante ci seen diggante ak nangu jeneen fason

ci dunde.

KOPPERASION YI DEFANTE LIGGÉEY CI DIGGANTE LEKKOOL AK

MBOOTAY YI ANDUL AK BENN NGURGI

Page 8: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

BOKK CI AK KAYIT YI NGIR MANA BOKK CI

Page 9: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Ndax programme weccee diggante ay lekkool ENSA mooy joxe ay cér xaalis

bu bare li ñu gaw pur doxale jëf yi. ENSA mooy nekk njiit ci nas wi bi nuy

kumaase ci xam-xamu jángale, defar ay doxalin yi, daje diggante lekkool yi bë

ágg ci defaraat.

Lekkool yi am digaale yi ak benn lekkool bu nekk Afrique, Asie, Amerique bi

nekk bëj-saalum walla Europe bi nekk bëj-saalum – penku man nañu depose

seen kayit yi ci buro ENSA. Ndimmal ENSA wi ay mbotay yi andul ak benn

ngurgi te nuy liggéey lekkool yi, mbootaay parent eleew yi mbootaay yi ndax

ndimmali ay lekkool yi ak lekkool yi man nañu depose seen demande seen

bopp itamit. Programme bi defay nekk pur eleew yi yépp nuy jánge ci lekkool

wi nekk ci Allemagne te seen at nekk diggante 15 ak 24 at.

Xabaar yi y´pp ndax man ci bokk ak li nuy laj pur ngamana bokk man ngeen

fekk ci sunu adress site wi:

www.ensa-programm.de

Man ngeen jot ñu ci adresse bi

ENGAGEMENT GLOBAL gGmbH

Service für Entwicklungsinitiativen

ENSA-Programm

Lützowufer 6-9

10785 Berlin

Telefon 030 25 482-0

Telefax 030 25 482-359

[email protected]

Page 10: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

KAYIT NDAX NATAAL YI

Page 11: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Title: Monterrey, Nuevo León, Mexico

Photo: Gerard Bosch, www.gerardbosch.com | Graffiti: Street Art in Monterrey,

Avenida Morones Prieto / Garza Sada. Blast, Andrea y Screw, Monterrey,

Nuevo León, México

2-3: São Paolo, Brazil

Photo: Flickr/Jack Two | Graffiti: »Humilidade e respeito« von Os Gêmeos,

More information and images: www.osgemeos.com.br

4-5: Marrakech, Morocco

Photo: Flickr/fchmksfkcb | Graffiti: Unknown

6-7: Buenos Aires, Argentina

Photo: Robert Ostmann. From a photo series that documents changes in the

centre of Buenos Aires. More information and images: www.prevu.cc, www.

flickr.com/photos/jetbronze/4445935412 | Graffiti: Unknown

8-9: South Africa

Photo: Mahkulu | Graffiti: Freddy Sam. As part of the project »i run in south

Afrika«, more information and images: www.a-word-of-art.co.za,

www.flickr.com/photos/freddysam/5062664442

10-11: Lima, Peru

Photo: Flickr/Paramonguino, more images: www.flickr.com/photos/

qaway/8167805096/in/photostream | Graffiti: No Rules Corp,

more information and images: www.norulescorp.com

Page 12: LI MOYI PROGRAMME-ENSA · LI MOYI PROGRAMME-ENSA Xabaar yi ci politig buyi jémale nit ni kanam ngir programme weccee diggante ay lekkool yi JÁNG GIS BENN ÁDDINA

Adress yi ñu war bind

ENGAGEMENT GLOBAL gGmbH

Service für Entwicklungsinitiativen

Tulpenfeld 7, 53113 Bonn

Lützowufer 6-9, 10785 Berlin

Telefon 0228 2 07 17-0

Telefax 0228 2 07 17-150

[email protected]

www.engagement-global.de

Programme-ENSA

Christine Blome (Njiit programme bi)

Telefon 030 25 482-237

Telefax 030 25 482-359

[email protected]

www.ensa-programm.de

V.i.S.d.P.: Annette Schlicht

Gis-gis (xalaat) ak bind: Ute Falkner, Jens Marquardt,

Claudia Schilling

Uslu (design) ak doxal mbir mi: FLMH | R. Forner

Decembre 2012

Nit ku joxe ndigal